Escuchar "Ndox (L'eau)" Amazon Music Unlimited (ad) Prueba Gratis 30 días

Letra de Ndox (L'eau)

Sa joie et sa pudeur font sa face cachée Son paraître et ses formes montrent sa force Celle que je vous chante, vous est familière Elle est utile et belle Elle a révélé la beauté du monde On la clame ParadisMbégte ma, sutura sa Da fa méngóok, baatinëm Zaahir sa, melo ya Moo wone, kattanamLi may misaal lu ngeen xam la Am na njariñ te rafet na Moo génne taaru adduna Moom la ñu bakke, al janna Waxtaane ko sax banneex la Nañ ko foηk sakkanal koEn parler même est agréable Respectons-la, économisons-la Vois la mer, le fleuve Rendons grâce à Dieu Elle est utile et belle Elle a révélé la beauté du monde On la clame ParadisMbégte ma, sutura sa Da fa méngóok, baatinëm Zaahir sa, melo ya Moo wone, kattan amLi may misaal lu ngeen xam la Am na njariñ te rafet na Moo génne taar u adduna Moom la ñu bakke, al janna Waxtaane ko sax banneex la Nañ ko foηk sakkanal koGéej gaa ngi nii yé Dex gaa ngi nii yéDara gënul ë neex taw bi Ku weddi laaj ko bay kat ba Ci la ñuy roosé seen tool ya Walla nga laaj ko samm kat ba Ci la ñuy nandale jur gaNdox daal am na njariñ baax na Dara gënul la neex taw bi Taw daal njariñ la ci dun biNdox daal njariñëm ba la nga koo xam mu jafe Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu manqué Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu jafe Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu manqué Ndox daal njariñëm Ba la nga koo xam mu jafeAlaa gaynaago yoo samba lingeer Donoy waaly yée, wulée ñaay ngoy Yée gan wuri coo, wulée gaynaako yoo Yeée, yóo, gan fari baa