Letra de Fay Bor
Ki la bëgg yab ndax alal, yaw ignorer ko lèpp Lu la nit, di Dokhanto, Yalla am na ko Féek yaa ngi koy wóolóo, yalla mën në laa fayal sa borKi la bëgg jaay loo sa ngor, bayyi kook yëfëm Ba ko fa ne tek, bés a ngi ñëw, di na wéet ak jëf ëm Féek yaa ngi koy wóolóo, yalla mën në laa fayal sa borTe sax jamono fi mu toll nii, ku ne bopp am la tal Mawlaana rek, moo lay defal, ken du la xamal Féek yaa ngi koy wóolóo, yalla mën në laa fayal sa borSalaam alleykum, nga bañ ko fay, mbaa xam nga ni bor la Sa dëkkëndòo, nga koy tanxal, mbaa xam nga ni bor la Teg say briques, ken mën të jaar mbaa xam nga ni bor la Yor sa auto, lu la neex def mbaa xam nga ni bor la Nit ku la neex, nga wax ci moom mbaa xam nga ni bor la Yor say mbalit, fu la neex tuur mbaa xam nga ni bor la Koo séqqël, daldi ko wor mbaa xam nga ni bor la Yendoo wax, loo waax mu dañ mbaa xam nga ni bor la Koo ëpp doole, won ko ko mbaa xam nga ni bor la Doo dimmili, ki nga tane mbaa xam nga ni bor laWar ngay xalaat bu ëllëg ée, nan nga koy fay é Féek yaa ngi koy wóolóo, yalla mën në laa fayal sa borman youssou maajigéen, j'ai tout pardonné Koo xam ni, meusone na la tooñ, jéggël ma koBor yi nga am fii ñu ne, nan nga koy fay é War ngay xalaat bu ëllëg ée, nan nga koy fay é Féek yaa ngi koy wóolóo, yalla mën në laa fayal sa borki la bëgg jaay loo sa ngor, bayyi kook yëfëm Ba ko fa ne tek, bés a ngi ñëw, di na wéet ak jëf ëm Féek yaa ngi koy wóolóo, yalla mën në laa fayal sa borTe sax jamono fi mu toll nii, ku ne bopp am la tal Mawlaana rek, moo lay defal, ken du la xamal Féek yaa ngi koy wóolóo, yalla mën në laa fayal sa borSalaam alleykum, nga bañ ko fay, mbaa xam nga ni bor la Sa dëkkëndòo, nga koy tanxal, mbaa xam nga ni bor la Teg say briques, ken mën të jaar mbaa xam nga ni bor la Yor sa auto, lu la neex def mbaa xam nga ni bor la Nit ku la neex, nga wax ci moom mbaa xam nga ni bor la Yor say mbalit, fu la neex tuur mbaa xam nga ni bor la Koo séqqël, daldi ko wor mbaa xam nga ni bor la Yendoo wax, loo waax mu dañ mbaa xam nga ni bor la Koo ëpp doole, won ko ko mbaa xam nga ni bor la Doo dimmili, ki nga tane mbaa xam nga ni bor la War ngay xalaat bu ëllëg ée, nan nga koy fay é Féek yaa ngi koy wóolóo, yalla mën në laa fayal sa borman youssou maajigéen, j'ai tout pardonné Koo xam ni, meusone naa la tooñ, jéggël ma koÑun doom i aadama ndiaye li ñu gën ë sonn al mooy, Aqqi dëkkëndòo, aqqi àndandoo, ak aqqi am gi jamm yek, Yalla, yermëndéem yaatu na, mën naa jéggël e bakkaar bu mu né Waaye, doom i aadama Ndiaye, Boo ko yor ee lee bor, na nga ko fay, fii ci dunyaa Walla nga balu ko mu baal la,Yé way samba, Khalass, kholal Youssou maajigéen, oh! lii doy na waar Youssou Marie Sène, bu dee lii la, bor yi bari ña ñu Yaay na nga ma baal, baay na nga ma baal, aqq u njuréel You, Ndour, merci beaucoup . Adji maam Ndiaye, yaay I thianék ama, maa challaa Man da ma lay tooñ, njëk laa mer, fas sa ma kamnam nga daldi ree, nima mbaye dieye, mbasaa mbasaa Seng Seng papa Mbaye mbassa mbassa bés ni ki tay kholal, baal naa ñépp Am gi jamm yi, Fans yek, kharit yi ban ngemp Ho baal nagne ngempman youssou maajigéen, j'ai tout pardonné Koo xam ni, meusone naa la tooñ, jéggël ma komani jéggël ma ko ... Jéggël ma koyallak yeuremade yam Jéggël ma koman youssou maajigéen, j'ai tout pardonné Koo xam ni, meusone naa la tooñ, jéggël ma koahhhnn yeeee Jéggël ma ko