Escuchar "Ballago ndumbé Yaatma" Amazon Music Unlimited (ad) Prueba Gratis 30 días

Letra de Ballago ndumbé Yaatma

Billaay, ballago ndoumbé yatma, Su ñu waaji xaj oon na fi Naxxar doηη,la ñu bayyee Yalla, wonneeti naLi tax ba mbir mi metti lool, ñun da ñu ko foog wul woon Yëf yi gaaw ba bette gnou Billaay wéetël na ñuNjiinoo njiin faramaareen, Gòor u jaaga, nelaw naa Baay i wally dem na nii, ñun daal wéetël na ñuMa ngi koy jaale Sénégal, Di ko jaalé Gambia Di ko jaalé adduna, Ndaanaan ba dem na niiThione ballago, ndoumbé yatma Bu yalla buur bi doon taggoo, Kon di na ñu bayék yaw Ni patrimoine bi nga ñu bayyeel, Yee gua nit gñi, tete leen ci adduna Yee gua nit gñi, tete leen Xam al leen ci adduna Ahhh - BalaagoYee gua nit ñi ci adduna xam al leen Ni ñu war a nekkek Ak ni ñu war a dundée, Ak ni ñu war a jëfleentee Jinaxoo mbaay Yaw mi dëkké biir suuf, Boo dem ee neel ballago, réew maa ngi koy joy Aduna ngi koy jooy, Art baa ngi koy jooyNjiin faramaareen, Thione seck, wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna, am ul soloLi tax ba mbir mi metti lool, ñun da ñu ko foog wul woon Yëf yi gaaw ba bette gno Ndanaan ba demna ni Njiin faramaareen, Thione seck, wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna, am ul solo