Letra de Da fa laa
Da fa laa, wóolóo, teg la nak, fu mu teg ul keneen Di dox sa bëgg bëgg, di dab sa banneex, ndax seetlu nga koo yaw, Yaw la bëgg, te yaw, yaa ko sagal, waaw waawBu mbëggéel, doon lumière, mel na ni, ni jant bi Te su am oon, lu ko gën ë leer, dem na wut i ko Ni yaw, diaral nga ko, lu raw, sóoru gayndé, waaw waawLu mu metti metti, di nga tew, lu mu sori sori, an! di nga ñëw, ca dëgg dëgg dëgg dem na, ba dem, mën ë tul ë tok benn bés, bum la, gis uljox na la bii respect, nga delloo ko bii respect Entre vous, entre vous chérie, du wax lii def leneen Ca dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg, ya ko diara ni yaw, yaa ko sagal, waw waawFépp fu mu mën ë ne, da fay sentir sa parfum Loolu yaa ko ko diaral, ndax yaa ko liggéey Les mots qu'il utilise, sont toujours en deçà De ce qu'il ressent, yaw yaa ko ko diaral Chérie boy, chérie boy, chérie boy Daf la bëuggué Chérie boy, chérie boy, chérie boy Kay nga diégué ko Mou laye déyYaw mii yaw, su fekkee li mu la wax doy ula, Boo yakkamtee, mu def al la ko, ni nga ko bëggéemom contane neu te sakh yaguena bëgg thi yaw, Boo yakkamtee, mu def al la ko, ni nga ko bëggéesa lui vas, chérie sa lui vas lo def nekh na ko da fa laa, da fa laa def ni nga ko defLoo bëgg, mu indil la ko Loo laaj, mu kheuthiel la ko Su fekkee am u ko, mu ñaan ko yallaChérie boy, chérie boy Ya ko ko diaral Chérie boy, chérie boy Lo diokhogne mo dok Chérie boy, chérie boy Lo def nonou la Chérie boy, chérie boy Ya ko ko diaralYoussou Ndour, madjiguene Boul yekhal dara Na gua gaw, na gua gaw Te li djieuntima Sokhla yi, sokhla yi Gnome gno ma gueteun