Letra de Mool (Deglu météo)
Yaw mool u géej gi, di jambaar ci réew mi Bala ngaa dem géej, ngala déglu météo Bu la nee bul dem, lu mën a xew bul dem Ben fan ak ñaar, bu mu yax sa liggéeyDoyloo nga yalla, du tee nga sa yor téléphone Ak sa gps, te bul fatte sa gilletSama fans yi ma am, mool ñoo ma gën a xam Fu ma làngee ak ñoom, guddi gë day xumb loolMan sama fans yee, ma saf Sawar naa làng ak ñoom, fu ne Aka ñoo dégg daaj, ma ni Moo tax may dem ba jeex, wallaJambaar ca waar wa Ni jambaar ca géej gë Su ma ko mënoon Ben mool du des ci géejBu la nee bul dem, lu mën a xew bul dem Ben fan ak ñaar bu mu yax sa liggéeySama fans yi ma am, mool ñoo ma gën a xam Fu ma làng ee ak ñoom guddi gë day xumb loolJambaar ca waar wa Jambaar ca géej gë Su ma ko mënoon Ben mool du des ci géejMan sama fans yee, ma saf Sawar naa làng ak ñoom, fu ne Aka ñoo dégg daaj, ma ni Moo tax may dem ba jeex, wallaYalna leen yalla suturaal Te di leen samm biir géej Barkeel seen liggéey bi Barkeel seen njaboot gi Aar leen ba ñu doon mag Jox leen barke maam yiMan sama fans yee, ma saf Sawar naa làng ak ñoom, fu neYess ayeAnh mool ba dem na géejoo (Anh mool ba dem na géejoo) Anh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo) Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géejoo (Anh mool ba dem na géejoo)Mool yi laa bëgg a làng al, seen làng xumb na Ndax sa ma fan's yi nak, Anh mool yee ci gën a denseAnh mool ba dem na géejoo (Anh mool ba dem na géej oo) Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géejoo (Anh mool ba dem na géej oo) Sa telephone ak sa GPS Bul fatte gillet baAnh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo) Mool yi laa bëgg a làngal, seen làng xumb na Ndax sa ma fan's yi nak Mool yee ci gën ë denseAnh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo) A dëggël, yaw mool u géej Yaa di jàmbaar Yaa bari fulla lool Bari jom lool Yaa donn loolu Gëm yalla lool Yaa xarañ lool, te tabe lool Youssou woy na leenAnh mool ba dem na géejoo (Anh mool ba dem na géejoo) Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géejoo(anh mool ba dem na géejoo)Mool yi laa bëgg ë làng al Seen làng xumb në Ndax sa ma fan's yi nak, am Mool yee ci gën ë denseAnh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo) Anh mool ba dem na géej oo (Anh mool ba dem na géej oo)Mool yi laa bëgg ë làng al Seen làng xumb na Ndax sa ma fan's yi nak, am Mool yee ci gën ë dense