Escuchar "Tukki" Amazon Music Unlimited (ad) Prueba Gratis 30 días

Letra de Tukki

Yoon wi nga jël baaxul ku la koy digël da lay nax Yoon wii ci des moo gën, loo taseel dàldi kuy mën Yoon wii nga jël booy dox ba ca biir géstul xool fi nga weesu balaa ngay Booy tukki yaw Booy tukki yaw Na nga bàyyl ba mën Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen Foofo mën nga fa gis lu yókk sa xameel Booy tukki yaw Nita ngi toog di janoog yaw booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam Yaw sama waay kaay ma xamal la Léég léég nga toog fi nga toog tukki bu neex dem ba kaw asamaan Ànd ag weer wiy naaw li ngay janeer mu lay neex boo janoo mu gën fee neex Booy tukki yaw Booy tukki yaw yeesal sa xameel Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel Deel tukki yaw Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw, te booy seet sax taxu koo gaaw Te léég léég mu dem ba kaaw Tukkee ka neex, waaw Lucum cééli ma ngay naaw te léég léég mu naaw ba kaw asamaan indi fiy xabaar Ku dul tukki doo xam fu dëkk neexe Booy tukki yaw Na nga bàyyi Booy tukki yaw Na nga bàyyi ba mën Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel Booy tukki yaw Booy tukki yaw Booy tukki yaw Na nga bàyyi ba mën Ñaanu barke ah ñaanu barke Nita ngi toog di janoog yaw booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam Yaw sama waay kaay ma xamal la Léég léég nga toog fi nga toog tukki tukki bu neex dem ba kaw asamaan Làng ag weer wiy naaw li ngay janool mu lay neex boo janoog moom mu gën fee neex Booy tukki yaw Na nga bayyi ba mën Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel Deel tukki yaw Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw, te booy seet sax taxu koo gaaw Te léég léég mu dem ba kaaw Tukkee ka neex, waaw Lucum cééli ma ngay naaw te booy seet sax taxu koo gaaw ëndaaleel ñu xabaar Tukkee ka neex, waaw