Escuchar "Bàjjan" Amazon Music Unlimited (ad) Prueba Gratis 30 días

Letra de Bàjjan

Taasukat baa nga naan gainde gu waaf ca buntu kër gé, di melastiku Bëy bu em bàjjan du fa dem, Zacharia, bàjjan am na maanaa, wayai Lu la réér ci sa cosaan, sa bàjjan xamal la koBoo bëgéé xam sa cosaan, kam la fa maam yi bayyi woom Demal seeti bàjjan ba, lu mu la ca wax, du deñ Bàjjana xam Kalcor an ba ca mbeneex wa Cosaani askan wi, bàjjan am na maanan Wayum terànga la kuy bàjjan jog, Sungun SanGan bàjjan, bàjjan Wayum TERANGA la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, Sungun SanGan Neenan mag a pu rencontrer de naa ba cim rééw waaye bàjjan il a répondu à na bàyyi ci biir Kër Xam sa Boppa Gén Ñu woo la naan kii nga Doon Wayum TERANGA la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sunguñ sangañ Boo bëgéé xam sa cosaan, sa bàjjan moo la koy xamalMoo la naan awai fii, bul dem fee, defeel nii Boo ko seetioo dara du ca deñ Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan si bj Gaay Walla raidiam Lu xew lune crinière bàjjan laxaw Bu Goor bugéé néégu Goor bàjjan taxaw wayal ko mbaax Nijaay di Yaay nga di Baay bàjjan am na maanaa Wayum TERANGA la kuy bàjjan jogal yëngu, Sungun SanGan bàjjan, bàjjan Wayum TERANGA la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sunguñ sangañ Bàjjan moodi magi baay walla rakkam Lu xew lune mane bàjjan laxawBu góó bugéé néégu góór Bàjjan taxaw wayal ko mbaax Nijaay di Yaay nga di Baay Bàjjan am na maanaa Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan Wayum terànga la kuy bàjjan sj