Letra de Wiri - wiri
Ha dem Dem fan Lu ma bëggoon mënul nekk Leer nga ci kenneen Man ma ngi ci lëdëmXam naleen, may ki koo def Suma demee bay meree Duma meree kudul sama mbopp Te man may seeti baye baalu koWiri wiri jaari ndare Wiri wiri jaari ndare, ndareXam na dem Demul feen fu nguy wuute Ligeey u ma Li ma mbëggoon moy mu dox Te duma dox, ci sen kawXam na lépp, may ki ko deef Suma demee bay meree Duma meree kudul sama mbopp Te man ma seeti bay, baalu koWiri wiri jaari ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Wiri wiri jaari ndare, ndareBilay, bilay, bilay, bilay-bilay Ma rëccu Ma nee soy dem mba xamatoo fa jëm Delul fa nga jukkee Fuy la xamee Fii nga mbaggee Fuy la teete Fi nga jange écoleWiri wiri jaari ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri)Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (ha fokk ma seeti bay) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wara bokk mba seeti yaay) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wiri-wiri-wiri-wiri) Wiri wiri jaari ndare, ndare (ha fokk ma seeti bay) Wiri wiri jaari ndare, ndare (wara bokk mba seeti yaay)