Letra de Immigrés/Bitim Rew
Ibu Njaay Fama Ibu Njaay FamaWaw bitim reew ña fa nekk dëkk ñu faa Mujj u mujj yay dañuy delu ci waw SénégalIbu Njaay Fama Ibu Njaay FamaBuul seen bittim réew ña fa nekk dëkk ñu fa Mujj u mujj yay dañuy delu ci waw SénégalHoolé Bitim reew ligey la lajj Immigré mom ligey la lajj ImmigréIbu Njaay Fama Ibu Njaay FamaÑu nee bitim reew ñu fa nekk dëkk ñu fa Mujju mujj yaay da ñi délu ce ndaxte ñoo ñu xamu ñu leen noono Fi la ñu saaso Ñu nee jòom mooy tukki yaay Waye fulla mooy ñibi cee Noo mën a mel Noo mën a am ndeysan ñibi ce la warYoussoo sabali nga,sabali nga Deedet samali ngondeh Moytul lu la defar,li la nex waxal Ndax bañuloo te mbëgga nga ñepp a amCodu faal Gaydella,Gaydella