Escuchar "Wéétoo" Amazon Music Unlimited (ad) Prueba Gratis 30 días

Letra de Wéétoo

Wéétoo, wéétatinaa yaay Wéétatinaa, wéétatinaa, wéétatinna yaay Sophie demna tey ma dabiko Sainte-Marguerite sorina tey ma dabikoSophie demna, moommii nëwna, moommi demna nii Sophie demna, moommi newna moommii demna nii Sophie demnaa tey ma dabiko Sainte-Marguerite sorinaa tey ma dabikoDemnaa fimu dem sorinaa sana guel demnaa yow Fimu dem sorinaa tey ma dabiko ndeysaay